CHRISTOPHE DASYLVA ''LADJ TE''
CHRISTOPHE DASYLVA OFFICIEL
0:00 / 0:00
CHRISTOPHE DASYLVA ''LADJ TE''
36 648 просмотров · 6 л. назад
CHRISTOPHE DASYLVA OFFICIEL
4,95 тыс. подписчиков
36 648 просмотров · 6 л. назад
LADJ TE (QUESTIONNEMENT)
Waxone na né dina delousi dieul si gnima baye bi denkone (×4)
Mane mangui lay ladj
Dila ladj, bou Yessu delousé fane ngay Dieum (×2)
Réfrain
Fane ngay dieum(×8)
1. Aldiana dina fess
Safara dina fess
Soo amé Yessu di nga am müccë(×4)
2. Amoul Müccë cii benéne tuur, bou doul cii turu Yessu..
Mani amoul müccë cii benéne tuur bou doul cii turu Yessu (×4)
Mane mangui lay ladj, di la ladj,
bu Yessu delousé fane ngay dieum
Mane mangui lay ladj delou di la ladj
bou Yessu delousé fan ngay dieum
#christophe #ladjte #gospel #senegal