Перейти к содержимому

Big Dat X - Pause Cas Faits (Audio officiel)

Big Dat X

0:00 / 0:00

Big Dat X - Pause Cas Faits (Audio officiel)

8 741 просмотр · 1 г. назад
Big Dat X
10,3 тыс. подписчиков
8 741 просмотр · 1 г. назад
#pausecasfaits #bigdatx #ogkajooroi Streamez ici: https://onerpm.link/ogkajooroi ———————————————— Artiste: Big Dat X Titre : Pause Cas Faits Prod : TeacherBeatz Enregistrement: Das Records Mix/Master: Teacher Video: Nittu Deugg Production exécutive: MeloMusic Ent. & Chambre 9 Contacts: bigdatx247@gmail.com ————————— Réseaux Sociaux: X @BigDatX2 : https://x.com/bigdatx2?s=21&t=EI1N8Ym... Facebook @Big dat X :   / big-dat-x-marxabane-team-650660248375778   Instagram @bigdatx: https://www.instagram.com/bigdatx?igs... Tiktok @bigdatx : https://www.tiktok.com/@bigdatx?_t=8U... ———————— Lyrics Baaraam u digg si lobby siisuman sama bopp laa gëm Man dara duma bett ndem liy raam si ñag bi la jëm Gewël du jur muumë loolu moy yaakaar bu tas Coow li [coow li] gën fi bari ne sabar gu tas Dinañ yagg si jooy X ay neex a faral dimanche T’es au courant sa rappeur fitam day faral di maas Ñune X dafa waga men Rax ci tuuti caga men Rabu ndaga baaraam u digg sen in in mama yen Mballu ba daanu jaawale jus bi le Krik krak murder len taxul may jubiler Ki jaar si digg bi man la Yaxxate beat bi man la Taaru mbind bi aaru mbedd gën a fi werëdi man la Amul saale day sale pimenté buma tegoo si beat Malaakal mëwti rap bi teew foy miser bo tegul si Big Hey Noise Maker ma open heart bi wax la lima feel Duma boy u kenn it’s time them know the deal The first thing Est-ce-que game bi recognise na mérite? Mar naan du tax ma naan pôtit Déception ni Don kenn xamul lumu doon Be a leader why i’m born Bullshitism why i’m done Grand Damel a ma jox jaasi nema taxaweel kankourang Ma waay di xaar keneen kan ku rang Tambalee làbbali rhyme ñu nan tay kan laay dëjjël War Dajjaal di la yoxal ngay tuddu benn bët di jéll Kuma fi ba xamal ni mën rabam a des wala moomin la Taak reum u MC yeah luma miin la Yàgg len terroriser ba ñëpp sikkël ma Ya fi fëgg dënn tay suba yaay woote calmant Degg nafi sen i pic mais vous portez jamais vos reukhou Ñakk Gorée sa bopp moy duggu si Porte aller sans retour Radio nga sex ni McNeely may crochet Tyson bilay suusël Dat trash talk plus performance comme Cedric Doumbe Fatt say angle teewula doon mort Jordan Yaa mën te foo songee fekk say dàll makkaan Do len producer ay woubi ngen Li feat la wala sëy Bàkkoo trophée jéng man winner la ni Jyeuhair Princesse de la ville ak la chouchoute de KeuMeuFemme À part ref si rap lufi KeuMeuFeu am Gisuma fi ludul reine bu took si chaise anglaise Trône de fer neel ñi lay couche mënofi took à l’aise La somme de diw ak diw Projem ñëpp jàpp di diw Amul concurrence affaire de niveau Linga goob nga jiw Budul gaaruwaale kufi mës a gis fu Gun di Shot Now it’s time nga honest Better tell them kulen tee nelaw Badman i run things Things don’t run me Everything me do Me haffy do it properly Avance waga bi nga jël fexeel buko wutël lay You’r snitch kingay sotal bitch loloy jikko jeeg Ñëpp xam 2023 who drop da best album Ñuni Big Dat du best lyricist hein feni neen Aham duuli neen [duuli neen, feni neen] Gëj nga lucide binga tafoo sama doublé si awards yi Lyrically musically Check Mic a causer sa death Bu talent don fay ma rangale trophée yëpp dara du des OK daxx sa next album bul es Vrai complexe ngafi gis si kanam u hype Yaw la boy u diw rekk ñuni lepp tight [yeah] Quantité molen gënal quality Amuñ xam-xam si talent jël lepp tek ko si vue [yeah] Bokkuma si jàgg yi nekk si game wër di maral Laajal Coumba dof be g Ydee bi respect lim ma jaral Serious business without money men is damn bullshit Boo dee yalla fexeel nga tax boulette ñi xiif eat [yeah] Fuck master pipi ak rap221 bi yëpp Fuck chroniqueur yimay jeem a boycott ak dima tëb Neleen mangi ak mental de fer kenn si ñoom duma disturb That’s wussup Og KajooRoi bi moy the best