Перейти к содержимому

NJ911- NJAAY DRAGON(OFFICIAL AUDIO)

nj 911

0:00 / 0:00

NJ911- NJAAY DRAGON(OFFICIAL AUDIO)

44 просмотра · 2 недели назад
nj 911
4 подписчика
44 просмотра · 2 недели назад
🎤 Artiste : NJ911 🎵 Titre : Njaay Dragon 🎬 Official AUDIO ...................................... NJAAY Dragon ......................... lyrics ........ INTRO Yeah Yeah Yeah Njaay Dragon ngeu Skrrrrrrrrr Ay Yeah G I A M Game bi dafa serré Xam nga kii ñëw Yeah --- 1ER COUPLET Rapp baal nganaan da ngay guéné ay loup Rapp bi amouniousi objectif yi gagner coupe Comme que bandit bouy changé cii ay minicoup nga Tay laay rapp paré tégal ay poup Meusoo nék réel Yaw yay njaay dragon Rapp bi déwoul boyé bania def lou béton Sa flow bé fouri téksi soxla savon Maan may rapp paré def lou sale ak rayon Fi rappeur yép boolén tégoone meunougn def lou fusil Rayla MC yi nieuw ma poissons d’avril Sa jaay niodi cana cii sama sourcil Douniou la compter même sa cordon nombril Fuck sa vie yéne niéup laay yobou au péril Danga bëgg titre waaye titre bi dafa lourd Danga bëgg buzz waaye buzz bi du secours Danga bëgg monter mais nga ragal hauteur Man maa ngi ci sommet yaw ngay chercher ascenseur Sa wax yi bari mais résultat dafa petit Sama silence même mooy def sa carrière tiit Danga bëgg faire boss mais boss bi du wax rekk Ku am niveau ci game bi dafay montrer ak tek Sama flow dafa lourd sama mesure dafa propre Yaw ngay chercher style man maa ngi déjà propre Danga bëgg copier mais copie bi dafa faux Sama ligne dafay monter yaw nga descendre encore Njaay Dragon xam nga game bi du lekk Ku amoul niveau micro bi dafay fekk Danga wax “dragon” mais dragon bi dafa mou Bu ma déclenche flow bi xam nga sa tour dafa fou --- HOOK ×2 Yay Njaay Dragon xamo dara do def lou carré Sa carrière ci arrêt Meuno def lou carré Waxal ma sen bandit bi fake dou def lou carré Meuno def lou carré Meuno def lou carré xamo dara do def lou carré Sa carrière ci arrêt Meuno def lou carré Waxal ma sen bandit bi fake dou def lou carré Meuno def lou carré Meuno def lou carré --- 2ÈME COUPLET Danga bëgg wax fort waaye sa ligne dafa faible Wax ji bari rekk mais ci game bi tchiow faible Njaay Dragon sa nom grand mais sa niveau petit Dinaa lekk sa hype après jëll sa crédit Rapp bi du théâtre ku faux dafay fégne Yaw nga ngi jouer boss mais personne du la dégne Sa flow dafa tourne comme roue bu amoul frein Maa ngi si terrain yaw ngay cherche encore terrain Wax nga “dragon” waaye sa flamme dafa sedd Danga bëgg compétition mais sa mental dafa wedd Chaque punchline ma lancé dafay teg sa silence Nga bëgg def carrière maay def différence Sa crew di wax beaucoup mais résultat néant Maay mettre pression sans faire cinéma durant Njaay Dragon joxal place game bi dafa serré Bu ma micro bi jël xam nga kii meunoul carré Danga bëgg réponse mais man duma perdre temps Sama travail dafay parler sama résultat moy argument Yaw ngay compter les vues man maa ngi compter les niveaux Danga bëgg suivre sama pas mais sama vitesse dafa trop Sa flow dafa tourner sama flow dafay couper Sa carrière dafay dormir sama carrière dafay monter Danga bëgg être premier mais classement bi laay lire Quand le vrai game commence yaw ngay chercher à fuir Sama punchline dafa tomber comme marteau ci béton Sama nom dafay rester même bu ñu fermer micro Danga bëgg jouer dur mais mental bi dafa mou Njaay Dragon joxal place parce que game bi dafa dougou Dama ñëw sans bruit mais impact bi dafa grand Dama wax ci micro tout le game dafay entendre Danga bëgg compétition waaye compétition du égal Sama niveau ci sommet yaw nga encore ci départ --- PONT Game bi maa ngi koy contrôler Chaque pas dama koy calculer Yaw ngay wax man maa ngi agir Yaw ngay rêver man maa ngi bâtir Niveau bi monté yaw nga resté Sama flow lourd nga dépassé Bu ma micro bi jël silence Njaay Dragon fin de séance G I A M… Maa ngi fi pour régner Game bi dou ñoo bokk --- HOOK ×2 Yay Njaay Dragon xamo dara do def lou carré Sa carrière ci arrêt Meuno def lou carré Waxal ma sen bandit bi fake dou def lou carré Meuno def lou carré Meuno def lou carré xamo dara do def lou carré Sa carrière ci arrêt Meuno def lou carré Waxal ma sen bandit bi fake dou def lou carré Meuno def lou carré Meuno def lou carré ! 🔥