Перейти к содержимому

Dadon trokhal Ndeyam Ak Baayam Ci keüR Gui … Ba Amadou Xam Kan Moo Leen Waxoon, Lépp Soppi Na 😱💔

Waxtaanu Afrik

0:00 / 0:00

Dadon trokhal Ndeyam Ak Baayam Ci keüR Gui … Ba Amadou Xam Kan Moo Leen Waxoon, Lépp Soppi Na 😱💔

12 338 просмотров · 4 дня назад
Waxtaanu Afrik
746 подписчиков
12 338 просмотров · 4 дня назад
Amadou dafa dellusi kër, te li mu gis ci kër gi tax na xolam daanu. 😔 Mu gis ay waajuram, Ndey ak Baay, di lekk ci suuf, fekk taabal bi nekk ci seen kanam. Amadou dafa amoon xel mu metti, te mu laaj leen lu tax ñu nekk foofu. Waaye li mu dégg ci seen gémmiñ moo ko jaaxal… « Fatou la. » Amadou dafa gëmul li mu dégg. Ndaxte Fatou, jabar bi mu bëgg, moo leen waxoon ñu lekk ci suuf. Waaye bu Amadou tàmbalee seet dëgg gi, mu gis ne am na lu ëpp li mu xalaatoon. Secret yu bari, ay wax yu ñu nëbb, ak ay jëf yu Fatou defoon ci lu ñu ko gis. Ndax Fatou dina wax dëgg gi? Ndax Amadou dina aar ay waajuram? Te ndax benn njuumte mën na soppi kër gu fees ak xaalis? 👉 Seetaan ba mujj ngir xam li xew. 👉 Bul fàtte LIKE 👍, COMMENT 💬 ak ABONNE ci chaîne bi. 👉 Su la histoire bi neexee, yónnee ko ci sa xarit ak sa famille. #Wolof #HistoireWolof #Senegal #Dakar #HistoireAfricaine #LeconDeVie #AnimationWolof